Vidéo:Alioune Sèye 2:«Thiouroukhou thiouroukhou diakhalou niou…Lac 2 souko Boy Niang teuwè na bayi lamb »

23 mai 2019 La rédaction 0
alioune s jr

xawa sougui niagga jamono yi.Askanou lamb noppi wou niou si di yeuy yabbi si combat bi bi niou ko taxawalé ba lègui.Wa Pikine ni sén dom famou dane diar rek lay reukkate ndax da niou ko yonni yakamti ko wayé itam wa guédiawaye di khar gounék écurie walo bilé dékkilate safara bi niou ko xamèwone en 2009.Ndax Boy Niang dinako piégé nimouko tameu di déffé,Lac 2 limou lanthial boy bi ndax dinako yabbi.Tontou bi le 13 juillet bi niou deukmeul ca arène nationale.

Regardez

 Source:Guediawayeinfos.com

Partager : Facebook

Articles similaires

Laisser un commentaire